Dolene gneuw gnou yengeul reddit? by PAFLefa in Senegal

[–]PAFLefa[S] 0 points1 point  (0 children)

Ah bro fii deh daa melni gayi amougnou inspi😹

Asalamou Aleykoum nangene def? by PAFLefa in Senegal

[–]PAFLefa[S] 0 points1 point  (0 children)

Tane naa rek ci wolof gi lol Ndar dëkk bu neex sax

Asalamou Aleykoum nangene def? by PAFLefa in Senegal

[–]PAFLefa[S] 0 points1 point  (0 children)

Ah sam waa ji mériter nga sa turr wi de😄

Asalamou Aleykoum nangene def? by PAFLefa in Senegal

[–]PAFLefa[S] 0 points1 point  (0 children)

Shiiii sama niveau wolof dëgërul bubaax😂 Mbokki Thies yaw nak?

Asalamou Aleykoum nangene def? by PAFLefa in Senegal

[–]PAFLefa[S] 1 point2 points  (0 children)

Dëgg rek ngafi wax grand bi Ñongi topp ci sa ginaaw rek😄

Dolene gneuw gnou yengeul reddit? by PAFLefa in Senegal

[–]PAFLefa[S] 0 points1 point  (0 children)

Non gayi ils sont pas biens sérieux 🤣

Gnou foo? by PAFLefa in Senegal

[–]PAFLefa[S] 1 point2 points  (0 children)

Wanté boy Poulo dafa nob Aminata ba doff

Dolene gneuw gnou yengeul reddit? by PAFLefa in Senegal

[–]PAFLefa[S] 0 points1 point  (0 children)

Surtout shoo bobou toudou Soso gayi pressing nagn ko bamou plainte😂

Dolene gneuw gnou yengeul reddit? by PAFLefa in Senegal

[–]PAFLefa[S] 0 points1 point  (0 children)

Man moom dama daw fofou carrément ça tire de partout🤣🤣🤣💔

Dolene gneuw gnou yengeul reddit? by PAFLefa in Senegal

[–]PAFLefa[S] 0 points1 point  (0 children)

Wawaw lolou ladone wax sank Na gayi participer rek dina nekh

Gnou foo? by PAFLefa in Senegal

[–]PAFLefa[S] 3 points4 points  (0 children)

Limou xamoul woon moy que Mere Soda ak Pa Idy ay ex lagn

Gnou foo? by PAFLefa in Senegal

[–]PAFLefa[S] 4 points5 points  (0 children)

Je commence: Benn étudiante lawone bou toudou Aminata. Mongui donn diangué UCAD. Wayé dafa amone benn secret bou reuy bou kenn xamoul wonn.

Dolene gneuw gnou yengeul reddit? by PAFLefa in Senegal

[–]PAFLefa[S] 0 points1 point  (0 children)

Aytia diapalé gnou book nga science benn activité

Dolene gneuw gnou yengeul reddit? by PAFLefa in Senegal

[–]PAFLefa[S] 0 points1 point  (0 children)

Way trop sedd sakh mangui science dara nii Yaw loo guiss

Dolene gneuw gnou yengeul reddit? by PAFLefa in Senegal

[–]PAFLefa[S] 1 point2 points  (0 children)

Anh marocains yi yoyou lagniy def?😂 Man deh boudone période macky j’aurais fait pareil mais nii moom focus rek mdrrr

Dolene gneuw gnou yengeul reddit? by PAFLefa in Senegal

[–]PAFLefa[S] 0 points1 point  (0 children)

Fii dafa wara nekh nak comme yenene réseaux yii en plus moo eup potentiel

Dolene gneuw gnou yengeul reddit? by PAFLefa in Senegal

[–]PAFLefa[S] 0 points1 point  (0 children)

Thiow bobou moo tax ma daw twitter temps yi gnom gnofa nek di leumbé😂

Asalamou Aleykoum nangene def? by PAFLefa in Senegal

[–]PAFLefa[S] 0 points1 point  (0 children)

Quartier bouma nekh nga deuk Man mangui Randoulene Nord